Aller au contenu

Mee

Jóge Wikipedia.

Weeru mee mooy juroomeelu weer ci arminaatu Gregori di ñetteel ci bu Suul.

Turam ma ngi jóge ci latin, doon tur bu ko waa-rom yi joxoon ngir màggale ko seen yàlla ju jigéen ja maius, jàppees na ne Romolos miy buuru Rom bi njëkk moo ko ko jagleeloon. Ca jamono yooyu moo doonoon ñetteelu weer ci arminaatu waa-rom bi.

Bés bi njëkk ci weeru mee xamees na ko niki bés bees di màggale liggéeykati àdduna bépp, ba ci Senegaal kenn du ko liggéey, ci Diiwaan-yu-Bennoo yi ak Kanadaa ñoom 1 Sattumbar lees ko di xewal.

Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar
pFad - Phonifier reborn

Pfad - The Proxy pFad of © 2024 Garber Painting. All rights reserved.

Note: This service is not intended for secure transactions such as banking, social media, email, or purchasing. Use at your own risk. We assume no liability whatsoever for broken pages.


Alternative Proxies:

Alternative Proxy

pFad Proxy

pFad v3 Proxy

pFad v4 Proxy